Coreano request for "No Stress"
Help translate from Wolof to Coreano song No Stress by Viviane Chidid
Requested by:
Ga-young
on 28 Maggio 2025 - 11:58
Testi originali
Wolof
Traduzione
Coreano
No Stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés
Non, non, duma nangu nga may teg stress
Duma nangu nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés
Ma ni dimbali ma, wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma, wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Danga fàtte ni awma dix ans
Lu tax nga jël ma bëgg ma def sa fowukaay
Yombalal naa la sa visa
Wow yeah yeah, demal fu la neex, waay!
Bëgg langaak kii
Bëgg langaak kee
Bëgg langaak samay xarit ma ni night and day
Dégg na ñu ne feebar la
Wow yeah yeah, defal lu la neex way!
Non non duma nangu nga may teg stress
Duma nangu fils nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardel bëgg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardek man ma romb la
Li safatu ma
Sama mettitu muñ jeex na
Li yëngëlu ma
Ndax te man ñakkuma fayda
Li safatu ma
Tegg ci temps def ba mu baax jot na
Te yaw mi xam nga
Soo ma nobul sa moroom nob ma!
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Non, non, bu ñu nangu ñu ñuy teg stress
Suñu xol di fees ñoom ñu juk def fés
Non, non, duma nangu nga may teg stress
Duma nangu nga may teg stress
Ma bañ duma ko nangu no stress
Sama xol di fees yaw nga juk def fés
Ma ni dimbali ma, wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Ma ni dimbali ma, wax ji bari na
Man rekk ci xale nammuma dara
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardel bëgg ma fowe ma romb la
Góor gu la teg deal lundi ba dimanche nobu la
Ku ma bëgg a tardek man ma romb la
Accedi o registrati per pubblicare una traduzione
ulissescoroa
submitted on 26 Dic 2016 - 06:04












